Nena Waaw

Jahman X-Press

Compositor: Não Disponível

Li Yàlla sak lépp ci taar sa jëm la ma doon misal
Musuñu tegante waaye ñoo bokk fi ñu doon xool
Xëccoo mettiwoon na, waaye yaa fi na lu te yaw la faral
Xol yi wara ànd bañ juddoo ba tay ñoo ngi werante
Waaye su ñu dajee kenn ci ñun dootuñu werante
Ku ne dina xam ne ki laa doon xaar ki rekk laa war doon

Ne na waaw te xol bi ne na waaw
Waajur yi ne nañu waaw, xarit yi ne nañu waaw
Ñépp ne nañu waaw kon yaw la wara doon
Ne na waaw te xol bi ne na waaw
Waajur yi ne nañu waaw, xarit yi ne nañu waaw
Ñi bañoon sax ñépp ne nañu waaw

Ak yaw bëgguma sax deme sama xel
Bëgguma solu bari mbëggeelu 0 calcule
Man naguwuma sax ku yaq sama xel
Ci yaw meme su de dëgg la ma la ko ñekk wedi
Foogoon na ni xol bi yàqu na te dootuma bëggaat
Déception lu metti la comme dal dootoo bëgg dundaat
Wante yaw, danga mel ni drogue ci psychopathe
Dof buy gaañ te loo la soxla

Ne na waaw te xol bi ne na waaw
Waajur yi ne nañu waaw, xarit yi ne nañu waaw
Ñépp ne nañu waaw kon yaw la wara doon
Ne na waaw te xol bi ne na waaw
Waajur yi ne nañu waaw, xarit yi ne nañu waaw
Ñi bañoon sax ñépp ne nañu waaw

Ne na waaw te xol bi ne na waaw
Waajur yi ne nañu waaw, xarit yi ne nañu waaw
Ñépp ne nañu waaw kon yaw la wara doon
Ne na waaw (yaw la doon séet)
Te xol bi ne na waaw (te yaa ngi sama wet)

Soxlatuma dara ndax nago ba tay ndax gis na sama gow
Àdduna bi yépp sa diggante loxo moo ci gëna woor
Ne naa la waaw, xale bi, yow laa doon xaar
Départ ba la ma mbëggeel arrivé ci yaw dotoo ma raw
Daw na ba sonn mënul nekk boobu xol bi ne na waaw
Mettiwoon nga daw, supporté nga samay caprices sax samay yu ndaw

©2003- 2025 lyrics.com.br · Aviso Legal · Política de Privacidade · Fale Conosco desenvolvido por Studio Sol Comunicação Digital